Search Movies Login Sign up
google-play-badge-min.png Download The Free Android App

Dembis - Liguey (Clip Officiel)

Dembis - Liguey (Clip Officiel)

< 00:04:31 > |

google-play-badge-min.pngGet the Free Android App for your phone
... Read more


Category: Films de 2020...

Ad:
** Abonnez vous à ZBest Production en cliquant ici ** Dembis nous parle de travail dans son nouveau clip LIGUEY. #Dembis #Liguey #ClipOfficiel #ZBestProduction #team221 ** Les crédits de la chanson & du clip "Liguey" ** Composition & beatmaker : Zoomon da Beat Mix et Mastering : Zbest Production Rélisation clip : Badzcool Remerciement : Lagio Abdallah (barber shop), Ibou Bébé Showroom Ulefone Médina , Mass Parara et Bass Dembaw Une production de ZBest Production (Dakar, Senegal, decembre 2020) ** Les lyrics de "Liguey" ** Refrain : yewou fadiar liguey ba fadiar liggeey amoul heure mane liguey la xam liguey la geum liguey evrytime Nango fight nango mougn gnoune fok gnou teral yaye mane liguey la xam liguey la geum liguey everytime Tok si bureau nek si chantier tok si auto di dawal mane liguey la xam liguey la geum liguey everytime Mane awma liguey damay jaay woutouma loudoul kagn liguey la xam liguey la geum liguey everytime 1er couplet : Boul nelaw guinar gui sabatina abdou gueye nathie na yewoul Doug si deuk bi gnakantéko sa weurseuk yakoy weuri Deureum bouma gnakk moma geuneul milion si yone bou lewoul Té foumou meuneu nek nako weuri ndakarou mba ngouma nguewoul Takal sa fit té nga jok takk sa thiaya mba takk sa seur mou deugeur Xeex ba bamouy gneuw bayi gnane ba dieundeul sa bop sagar Fier si lool té begsi mba ken doula si yabatii fexel ba bokk si course bi jema raw ba ken doula dabati Limay ndoudou makoy liguey limay thiéré nekh Soxor té ignane beugma teyé yako téré nekh Amal lepp am sa louné gnéwoumala bene yone Mane liguey la am liguey la geum liguey everytime Refrain : yewou fadiar liguey ba fadiar liggeey amoul heure mane liguey la xam liguey la geum liguey evrytime Nango fight nango mougn gnoune fok gnou teral yaye mane liguey la xam liguey la geum liguey everytime Tok si bureau nek si chantier tok si auto di dawal mane liguey la xam liguey la geum liguey everytime Mane awma liguey damay jaay woutouma loudoul kagn liguey la xam liguey la geum liguey everytime 2ème couplet : Hello ma soeur wouyouma firil sa nopp té deglouma Bossi tollo deh woutiko wouteul job té bayi sa werrou bi Fexel ba am sa dignité liguey lou beuri ba defal sa bop ndax Gneup yamougnou te kou topp tendence dilnala dougeul si pakh Yow aduna woroul kone sa euleuk jougeul xeex ko tey Amna gnoulay defal gno ngui khar heure bolene di fay Jigeen bou geumoul bopam nango fight gnéwoula bene yone Mane liguey la am liguey la geum liguey everytime Refrain : yewou fadiar liguey ba fadiar liggeey amoul heure mane liguey la xam liguey la geum liguey evrytime Nango fight nango mougn gnoune fok gnou teral yaye mane liguey la xam liguey la geum liguey everytime Tok si bureau nek si chantier tok si auto di dawal mane liguey la xam liguey la geum liguey everytime Mane awma liguey damay jaay woutouma loudoul kagn liguey la xam liguey la geum liguey everytime liguey ** Retrouvez ZBest Production sur Instagram **

Similar Movies to "Dembis - Liguey (Clip Officiel)"

Couldn't find what you were looking for?

Search through thousands of movies below